VII_W_6904_ARCHIV_SENEGAMBIEN_23

Récit épique autour des valeurs d’amitié et de courage. Cette chanson est donc un narratif sur la légende qui porte la dignité, le courage et l’engagement à son sommet.

VII_W_6904_ARCHIV_SENEGAMBIEN_23 Illustration: Anna Diagne

Les noms renvoient à un univers wolof du Sénégal notamment les régions culturelles du Djolof, du Saloum, du Ndiambour et du Wallo.

Transcription

Original (Wolof)

Traduction (Française)

Bu doon ca Ndar géej bu jant soowee,  
Janx lalum njoram, tuur ma lajkoloñ di ma bëstën.  
Bu doon sa ndar géej,  
Rëppeelu nga. 
 
Àdunna dees koy miin  
Jamono dees koy man.  
 
Mbër bu duggee marse dafa ngembuwut 
Bëgg naa... 
 
Ci suuf tay ! 
 
Majigéen, 
Mbër mu daan ña mu daan daan,  
La ne ca bopp ba raw na am xel 
Tony manu ko damat damatee.  
 
Famu ne maneesu ko raw.  
Da maa tàmm a joow.  
Ngon mu def namu daa def … 
 
Njëkk naa ne fit si bum bi tay ma liggéey fit  
Mbër bu dugge marse dafa ngembuwul . 
 
Mbër bu daan ñamu da daan bamuy dog a falu, 
Raw na am xel fum ni manuko raw da maa tàmm joow . 
Tey waaw-góore de xam nanu  
Kër ga borom mbër liggéey ca Simbóoj mi ci Kaolack , 
Xaw ma ceetan kon ma tabbi saxaar gi ci Kael.  
Edouard ca Kees.   
 
Bu doon ca Ndar géej bu jant soowee,  
Janx lalum njooro tuur ma lajkoloñ di ma bëstën. 
Bu doon ca Ndar géej 
Rëppeelu nga.  
 
Ndaw daale, 
Ndaw daali jujung nga lay yee.  
Ndaw daale jujung nga lay yee. 
 
Si c’était à Saint-Louis, au crépuscule 
Une jeune dame aurait étalé sa natte et m’aurait massé. 
Si c’était à Saint-Louis.  
Tu es genou à terre ... 
Le monde, on s’y habitue, l’époque, on la comprend. 
Si un lutteur se balade dans un marché,  
C’est qu’il n’est pas en culotte 
J’en veux … 
En sourdine aujourd’hui ! 
Madjiguéne…. 
  
Un lutteur qui terrasse ses adversaires,  
Sa technique va au-delà de ce qu’il a appris… 
Tony ne peut pas le briser en mille morceaux. 
Personne ne peut le dépasser dans son fief. 
  
J’ai l’habitude d’envoyer une pluie de coups de poings,  
Sinon, il l’aurait refait à son habitude. 
  
Il a commencé par prendre son courage à deux mains 
Aujourd’hui, je vais construire un courage. 
  
Si un lutteur se balade dans un marché,  
C’est qu’il n’est pas en culotte. 
Un lutteur qui terrasse ses adversaires habituels à ses débuts, pour devenir champion, 
Doit savoir qu’il ne peut m’échapper car j’ai l’habitude de donner une pluie de coups de poings 
Et doit-il saluer mes prouesses car il sait…   
  
La maison que le lutteur à construit sur toi à Kaolack
Je n’en connais pas le public sinon j’aurai sauté dans le train à Kael.  
Edouard à Thiès.  
  
Si c’était à Saint-Louis, au crépuscule 
Une jeune dame m’aurait étalé sa natte et m’aurait massé 
Si c’était à Saint-Louis… 
  
Que des chants de victoire, que des chants de victoires,  
Ce sont les tambours qui te réveillent 
Que des chants  de victoire, que des chants de victoires,  
Ce sont les tambours qui te réveillent. 

Contact

Envoyez-nous vos commentaires par courriel !

Retrouvez-nous sur