VII_W_6893_ARCHIV_SENEGAMBIEN_14
Dieser Text greift ein gymnastisches Lied oder Bàkku in der Sprache Wolof (Senegal) auf, das den Ruhm eines siegreichen Ringkämpfers besingt. Es handelt sich um ein Kulturerbe-Element, das in der senegalesischen Arena immer weniger verwendet wird.
Saint-Louis wird darin als der Ruheort des Kriegers beschrieben, und die Frau aus Saint-Louis als jene, deren Gunst man sich nur verdient, wenn man ein Champion ist – ein Mann von Wert.
Dieser Texte ist von großer ethnologischer, vor allem aber literarischer Bedeutung, ist jedoch im senegalesischen Raum immer weniger bekannt und wird selten praktiziert. Diese Aufnahme trägt dazu bei, eine Lücke zu schließen.
Transkript
|
Original (Wolof) |
Übersetzung (Französisch) |
| Bu doon ca Ndar géej bu jant soowee, Janx lalum njoram, tuur ma lajkoloñ di ma bëstën. Bu doon sa ndar géej, Rëppeelu nga. Àdunna dees koy miin Jamono dees koy man. Mbër bu duggee marse dafa ngembuwut Bëgg naa... Ci suuf tay ! Majigéen, Mbër mu daan ña mu daan daan, La ne ca bopp ba raw na am xel Tony manu ko damat damatee. Famu ne maneesu ko raw. Da maa tàmm a joow. Ngon mu def namu daa def … Njëkk naa ne fit si bum bi tay ma liggéey fit Mbër bu dugge marse dafa ngembuwul . Mbër bu daan ñamu da daan bamuy dog a falu, Raw na am xel fum ni manuko raw da maa tàmm joow . Tey waaw-góore de xam nanu Kër ga borom mbër liggéey ca Simbóoj mi ci Kaolack , Xaw ma ceetan kon ma tabbi saxaar gi ci Kael. Edouard ca Kees. Bu doon ca Ndar géej bu jant soowee, Janx lalum njooro tuur ma lajkoloñ di ma bëstën. Bu doon ca Ndar géej Rëppeelu nga. Ndaw daale, Ndaw daali jujung nga lay yee. Ndaw daale jujung nga lay yee. |
Si c’était à Saint-Louis, au crépuscule Une jeune dame aurait étalé sa natte et m’aurait massé. Si c’était à Saint-Louis. Tu es genou à terre ... Le monde, on s’y habitue, l’époque, on la comprend. Si un lutteur se balade dans un marché, C’est qu’il n’est pas en culotte J’en veux … En sourdine aujourd’hui ! Madjiguéne…. Un lutteur qui terrasse ses adversaires, Sa technique va au-delà de ce qu’il a appris… Tony ne peut pas le briser en mille morceaux. Personne ne peut le dépasser dans son fief. J’ai l’habitude d’envoyer une pluie de coups de poings, Sinon, il l’aurait refait à son habitude. Il a commencé par prendre son courage à deux mains Aujourd’hui, je vais construire un courage. Si un lutteur se balade dans un marché, C’est qu’il n’est pas en culotte. Un lutteur qui terrasse ses adversaires habituels à ses débuts, pour devenir champion, Doit savoir qu’il ne peut m’échapper car j’ai l’habitude de donner une pluie de coups de poings Et doit-il saluer mes prouesses car il sait… La maison que le lutteur à construit sur toi à Kaolack Je n’en connais pas le public sinon j’aurai sauté dans le train à Kael. Edouard à Thiès. Si c’était à Saint-Louis, au crépuscule Une jeune dame m’aurait étalé sa natte et m’aurait massé Si c’était à Saint-Louis… Que des chants de victoire, que des chants de victoires, Ce sont les tambours qui te réveillent Que des chants de victoire, que des chants de victoires, Ce sont les tambours qui te réveillent. |